Brandy Moja – Mane la nop (clip Officiel)

Artiste : Brandy Moja
Titre : Man la love

DIRECTED BY : MAO PROD
WRITTEN BY : MARIA SAFARY & Brandy Moja
PROD BY : HACKIM
ARRANGEMENTS : MARIA SAFARY & ZOX
MIX & MASTER BY ZOX
PHOTOGRAPHE : BBC photography
OUTFITS : BISE COLLECTION
COIFFURE : MODOU MAKE UP
MAKE UP : AMEL BEAUTY
GUEST STAR : JULES TERANGA

Lyrics

Dangama gnoor baby
Nawétak nord malay feel
I’m into you my honey
I want us to fly all life Dougou ci yow diémouma khol
Wérou ci yow ba douma khof
Diokh ngama love ba dama doff
Li Loukoy faye loukoy faye

Déngma nope
ManDamala nooope
Déngma nope
Man damala nooope

Déngma nope
Man damala nooope
Déngma nope
Oh baby I’m in love with you

Refrain
Sama Cheri dafma lova Baby man la lova
Baby man la lova
Baby man la lova

Couplet 2
Yangui mér Gueuneu diantal Bayil di jouer si sama mental
Li dou loumay atane
Ndakh yow mi yow mé yow éeh
Mbeguel ngama sol bamou fess
Té diaral ngama daw fi ba fez
Keuf ngama dawak man ni mess
Oh j’avoue mak yow on est de mèche
Je vais te nourrir d’amour
Des bisous glamours
Je veux que tu savoures Nos umh hum hum toujours

Déngma nope
Man Damala nooope
Déngma nope
Man damala nooope
Déngma nope
Man damala nooope
Déngma nope
Oh baby I’m in love with you

Refrain

Sama Cheri dafma lova Baby man la lova
Baby man la lova
Baby man la lova

#brandymoja #manlanop #music